| audio
				 audioduration (s) 0.74 10.5 | text
				 stringlengths 1 99 | gender
				 stringclasses 2
				values | 
|---|---|---|
| 
	Fan lay sax ? | 
	male | |
| 
	Saa boo ragalee Yàlla Buur bi moom miiy Kenn, ku dul Yàlla dalay ragal. | 
	male | |
| 
	Buma ko jàppe. | 
	male | |
| 
	Ndox mi mu ëmb, cafka gi dafay sëccwex | 
	female | |
| 
	Tom gisu ko woon. | 
	female | |
| 
	Ma kay wayal Seex Saalihu. | 
	male | |
| 
	03/07 à 2330 Mine Ubbi njël lu njëkk li | 
	female | |
| 
	Mas naa jaay lii. | 
	female | |
| 
	Damaa yeex a ñëw. | 
	female | |
| 
	manees na am yaakaar ci moom. | 
	female | |
| 
	Jën dax na, tay . | 
	male | |
| 
	Kuy seenub jkat? | 
	male | |
| 
	Fi mu am | 
	male | |
| 
	Buy délsi yal na nu fekk ak may gu suuxali may | 
	female | |
| 
	Maa ngi tëddoon sama lal. | 
	male | |
| 
	Sama liggéey dafa géey. | 
	female | |
| 
	Bul bàyyi ! | 
	male | |
| 
	Toma ngi ci kaw. | 
	female | |
| 
	Biirmaani ci lu bari Bëj-saalum-penku Asi la ñu koy boole. | 
	female | |
| 
	Xawma woon ne aw fen la. | 
	male | |
| 
	Bëggu ñu la. | 
	male | |
| 
	Damaa bëggoon a doon ndaw. | 
	male | |
| 
	Wax naa dëgg, am déet ? | 
	female | |
| 
	Soxla naa ab farandoo. | 
	female | |
| 
	dinaa leen gindi | 
	female | |
| 
	Ñu ngi ko tëye ca màkkaanum mu mag mu alkaati ya ca Ndakaaru. | 
	female | |
| 
	Buleen ma xaar. | 
	female | |
| 
	Bàyyi ma ma nelaw. | 
	female | |
| 
	Jaxaay ji ak picc mi | 
	female | |
| 
	Maa ngi jéggalu | 
	female | |
| 
	Danuy jënd ay CD. | 
	female | |
| 
	Suuf si daa di nangu. | 
	female | |
| 
	Du sama mbir. | 
	female | |
| 
	Xale yi gëmewuñu ko woon | 
	female | |
| 
	Mbooram bi dëgg la. | 
	female | |
| 
	Ci mbirum doomu weñ yi jigéenu-wérul war a wann | 
	male | |
| 
	Loo soxla ? | 
	male | |
| 
	Bàyyee gu Otris bàyyee Itaali Venezia. | 
	male | |
| 
	Loolu, du lu ma jékki-jekki rekk def ko | 
	male | |
| 
	Ay nit lañu. | 
	male | |
| 
	Bëgg naa ci benn ! | 
	female | |
| 
	Nos dooley kaaraange ji | 
	male | |
| 
	Doon naa ko ñaawal. | 
	female | |
| 
	Nekkon na nu ay xarit. | 
	male | |
| 
	Daa jubb lool. | 
	male | |
| 
	Da koo kott. | 
	male | |
| 
	Dangaa ñàkk jafe-jafe lool. | 
	male | |
| 
	sunuy jafe-jafe ci wàllu paj soppikuwul. | 
	female | |
| 
	Jëfandikoo ko walla nga ñàkk ko. | 
	male | |
| 
	Dama xalaat ne danga reelu. | 
	female | |
| 
	Bunu wuute nag, foofu la liggéey bi nekk | 
	male | |
| 
	Damaa am ñaan. | 
	female | |
| 
	Setalal sa néeg bi ! | 
	male | |
| 
	Toogal fii ak nun. | 
	male | |
| 
	Taariix | 
	male | |
| 
	Moos mi xossi nama. | 
	male | |
| 
	Naj ak forse | 
	female | |
| 
	Danga may fen ? | 
	female | |
| 
	Noo rëyee nii?! | 
	female | |
| 
	Nu ngi nekkandoowaat. | 
	female | |
| 
	Teew fa nag, doore ko ci sawaal digg-bëccëg ba jant so | 
	female | |
| 
	Dafa dégg i coow. | 
	female | |
| 
	Mbir mii daal, kenn setu ci. | 
	female | |
| 
	Am na ci ñent yoy ñi ngi ame ca armal ga | 
	male | |
| 
	Tur wi feeñ na ci Injiil ci Mk 317. | 
	male | |
| 
	waaye ak bii yamale, dëgërluwiin gi dafay aju ci tàngaayu wërlaay gi mu ne | 
	female | |
| 
	Mbaa kuy rambaaj naankat bu màndi xaaloo | 
	male | |
| 
	Mu ne  «Ñoom de ñook woor diirub jamonoo yam». | 
	female | |
| 
	Masuma faa dellu. | 
	female | |
| 
	Beto De Canda | 
	female | |
| 
	Tom sopp na mool yi. | 
	female | |
| 
	Ma defoon ko ngir moom. | 
	male | |
| 
	Daanaka, demewu fa noonu | 
	female | |
| 
	mu wàcc-liggéey Sëriñ Abdu Laat Mbàkke wuutu ko di xalifab Sëriñ Tuubaa. | 
	female | |
| 
	Damaa bëgg aar. | 
	female | |
| 
	Wéer ngànnaay gi nag lii la wax | 
	female | |
| 
	Moom            la        leen | 
	male | |
| 
	Melal ni yaay man. | 
	male | |
| 
	Ndax jekk ngeen ? | 
	male | |
| 
	Man ngaa lakk farañse a? | 
	female | |
| 
	Jox naa la ko am ? | 
	male | |
| 
	Dañu maa féexal. | 
	female | |
| 
	Booyal bay ab tool booyal ko am at door koo bayaat | 
	female | |
| 
	Babilon dëkku penku la woon, di péeyug réewu Kalde, maanaam Irak | 
	female | |
| 
	Tus-wu-taxaw wenn la ci ñaari xammikaay yi beneen bi mooy tus-wu-gaar | 
	female | |
| 
	Yokkal tuuti meew. | 
	male | |
| 
	Mooy ne, bala dara, Séex Anta tekkikat la woon | 
	female | |
| 
	Jéem naa lépp. | 
	male | |
| 
	defleen ag tànn ! | 
	male | |
| 
	Boo seetloo, sunu way-tawati Covid-19 yu jëkk yi bitim-réew lañ jóge | 
	female | |
| 
	Man nanu koo am it jaare ko ci yeneen i lijjanti. | 
	female | |
| 
	XEESAL WALLA XEEB SA BOPP ? | 
	female | |
| 
	Waxi Seex Anta Joob ju aju làkkSoppi | 
	female | |
| 
	Damaa sonn lool?! | 
	female | |
| 
	Àdduna wori neen la. | 
	female | |
| 
	Lii sax caaxaan lay niru | 
	male | |
| 
	Loo leen di nëbb ? | 
	female | |
| 
	Yeneen waat yi it noonu lañu mel. | 
	female | |
| 
	Ku wax ? | 
	male | |
| 
	Dina soxla itam ab sàkket leeg-leeg ngir mu man a law ci kawam | 
	male | 
			Subsets and Splits
				
	
				
			
				
No community queries yet
The top public SQL queries from the community will appear here once available.