fr
stringlengths
4
995
wo
stringlengths
4
1.09k
donc l'environnement lui-même atténue le changement climatique car ils vivent mais s'ils sont confrontés à l'été il y a une variété rapide tout ça même s'il y a un rendement mais ces trois mois ce que tu dépenses ne peut pas contenir les mois
donc mbéyum noor bi moom day atténuer carrément lu ñuy wax changement climatique bi da koy atténuer parce que ñu ngi koy dund mais su ñu jàkkaarloo ci nawet bi am nga variété bu gaaw tout ça làa même su amee rendement mais ñetti weer yooyu li ngay béy mënul a téye neuf mois yi
donc ils regardent déjà précisément cette prévision saisonnière qu'on a faite et après il y a des prévisions soit décennal ou bien soixante douze heures trois trois trois trois jours ou en vingt quatre heures il y a vingt quatre heures c'est donc plus précis
donc dèjà ñoom ñu ngi xool précis précis kii prévision saisonnière bu énu defoon et après mu am ay prévisions soit décadaires oubien di di soixante douze heures ñetti ñetti ñetti fan ou en vingt quatre heures jot ay vingt quatre heures moo gën a précis donc loolu la
voilà donc je me souviens que tu fais partie de la DRDR aujourd'hui et qu'ils doivent discuter de la question de la semence donc l'utilisation de la semence certifiée bonne pratique de la semis est le thème d'aujourd'hui avant de commencer à critiquer la discussion que tu es en train de faire
voilà donc %e ma fàttali rek yaa ngi bokk ci %e DRDR tey jii nag ñu war a waxtaanee lu jëm ci mbirum semence dañ donc l' utilisation de la semence certifiée bonne pratique de semis %e thème bi tey balaa ñu ciy dugg rek di sori ci waxtaan bi lan nga ñu koy faram-fàccelee
17 heures deux minutes présente Cheikh Tidiane Sarr qui vient de quitter son émission d'importance et qui est en train de faire un très bon hommage à Moussa Kane qui est dans le coin de la télévision.
17 heures deux minutes di jaajëfal Cheikh Tidiane Sarr mi fi jóge léegi ci seen émission bu am solo boobee di gêrëm bu baax Moussa Kane mi nekk ci wàll xarale gi
tu ne le connais pas
xam nañ ko
%hum %hum cela est engrais
%hum %hum loolu engrais
c'est à cent kilomètres donc tu sais que c'est lui
cent kilomètres la kon kooka xam nga ne kooku moom
exactement parce que à travers cotisation 1000F ce qui se passe toujours
exactement parce que à travers cotisation 1000F boobu bu doon am sax
maintenant, dans cette édition, il faut suivre les instructions précises sur la production de semence qui sont la condition pour que votre demande soit acceptée et que vous puissiez obtenir un certificat vous indiquant qu'il est certifié comme producteur de semence.
léegi nag ci yaatu boobu dañ lay topp suivre la waxal la exactement ci wàllu production de semence yan mooy condition bi pour sa jiw bi boo o liggéeyee ñu accepter ko ñu mun laa jox certificat bi nga xamante ne moom mooy cetifier que ne yow tu es un producteur de semence
parce que ce qui était une nécessité pour augmenter le rendement agricole est plus que l'eau qui diminue maintenant après avoir été déclaré problème de santé publique c'est un problème de santé donc je demande aux intervenants de s'occuper de ce problème car l'arbre est important je demande à mes frères de planter des arbres parce que c'est important
parce que lu ñu waroon béy lu ñu war a amati lu ñu war a am %e si rendement agricole bi duñ ko amati ndox mi dafay wàññeeku léegi nag après ñu naan problème de santé publique maanaam di problème mu wér-gu-yaram kon %e maa ngi jaajëfal intervenant yi si côté boobu noonu garab lu am solo la maa ngi %e ñaax sama mbokk yi maanaam ñuy jëmbat garab ñu koy jëmbat parce que lu am solo la
parce que je ne l'ai pas dit
parce que nañ ko waxee
si vous voulez plus de précisions, la diffusion sur Louga FM RTS alxames dure quatre à cinq heures mais vous pouvez aussi poser vos questions en appelant le 33 879 30 82
loolu nag bu ngeen ci bëggee am lu leen leer bu leen émission bi raw fii ci Louga FM RTS alxames ñeent jàpp juróomi waxtu waaye tamit mën ngeen a jiital seen i laaj ci bu ngeen wootee ci numéro bii di 33 879 30 82
El Hadj Abdoulaye est un homme politique
El Hadj Abdoulaye nga fan rek
pour au moins une marque sécurisante
pour au moins mieux sécuriser
mais dans un mois on peut faire passer le dossier depuis le constat jusqu'à son arrivée au comptable il faut un mois pour le faire revenir donc le problème entre le processus verbal et la réception jusqu'aux photos et la validation c'est de prendre le temps mais quand le vétérinaire vient constater que la cause du décès fait partie du contrat cela ne lui donne pas le droit de le laisser partir
mais ci benn weer laññu may bu dossier bi jaaree yoon depuis ci constat bi ba mu egsi ci comptable bi weer lay am pour ñu fay ko léeg-léeg nag jafe-jafe bi diggante %e procès verbal bi ba ma koy jot ba ci photos yi ba ñu valider ko foofu mooy jël temps mais bu fekkee ne vétérinaire bi ñëw na constater na xam na ne lu ko rey dafa bokk ci contrat bi loolu bu ko yónnee amuñu de %e droit bàyyi ko weer fayuñu ko
et voilà, c'est ce que je vous disais, le développement du Sénégal est de la terre vers le ciel
te fi mu ne nii la ma leen waxoon rek mooy développement Sénégal ci suuf la jugee jëm ci kaw
Oui, j'ai vu la photo qu'il a reçue et je vois que c'est tiktok. J'ai vu aussi la photo qu'il a en main gauche. Il semble que cela indique combien de "abonnés" il a et combien de "j'aime" il a et à combien de personnes il est "abonné". J'ai vu aussi les "vidéos" qu'il publie sur tiktok. Je l'ai vu ci-dessous. Application appelée tiktok, c'est un réseau social.
Waaw nataal bi ma jot de gis naa ne tiktok la. Gis naa itam waa ji mu ngi ko téeye ci loxoo càmmooñam. Mu ngi mel ne day génnee ñaata "abonné" la am ak ñaata "j'aime" la am ak ci ñaata nit la "abonné". Gis naa itam "Video" yi muy publié ci tiktokam. Gis naa ko ci suuf. Application bun naan tiktok la, réseau sociaux la.
ils lui ont dit
wax nañu ko
%hum %hum alors ils sont partis de là
%hum %hum kon ñu dem ci loolu ci ci
mais ils disent aujourd'hui que ce que tu sais que c'est %e c'est-à-dire l'histoire de l'homme est ce que tu sais que personne ne doit aller à son rythme dans des activités qui le rendent donc surtout ce que tu sais que c'est le mystère de l'histoire de l'homme
waaye nag ñu ne tey li nga xam ne moom mooy %e maanaam xibaaru jiw ji dafa di loo xam ne que ne kenn munul dem ci ginnaawam ci activité yu bëri nag surtout li nga xam ne moom mooy mbiru mbéy xibaaru jiw
si c'est à proximité, il y aura une ou deux parties et une ou deux maisons souvent une semaine après l'âge de sept jours si tu signes jusqu'à l'âge de sept jours tu te casses alors si tu restes jusqu'à l'âge de sept jours dans la même partie tu te casses encore et encore et encore %ehum
bu fekkee ne ci gerte la soit dina am benn ñaari xotti ak benn béy mais yooyu souvent une semaine après bu amee juróom-ñaari fan bu saxee ba am juróom-ñaari fan mun nga xotti boo toogee ba mu amaat juróom-ñaari fan ca xotti bu njëkk ba nga defaat mun nga delluwaat xottiwaat %ehum
soit 10 grammes
maanaam 10 grammes
peut être que nous reviendrons mais cette première est instantanée la question est de savoir ce qu'est le stockage c'est quoi le stockage en fonction de ce qui est disponible
peut être dinañ ci ñëwaat mais instant bii moom première laaj bi mooy lan mooy stockage mooy lan na mooy stockage ci ci ci tënk mooy ndencin
incha allah comme dévénement si les prévisions saisonnières sont acceptées
incha allah comme déwén su ñu jotatee suñu prévision saisonnière yi
fin de saison comme début de saison
fin saison tamit début saison bi ni muy amee solo
ok monsieur Sow de l'ANACIM mais vous l'avez dit ici la destruction c'est-à-dire le changement climatique fait partie intégrante de bien bien ce que vous savez que c'est la main de l'homme ces gens-là s'ils se font du mal ils savent que si ils ne sont pas vigilants après ils vont venir et cela va aboutir à une catastrophe environnementale cela va entraîner l'autosuffisance alimentaire c'est-à-dire la capacité de subsistance de ceux qui en ont besoin
ok monsieur Sow bu %e ANACIM waaye wax nga ko fii sànq %e maanaam %e changement climatique yi bokk na ci bu baax a baax li nga xam ne moom mooy loxo doomu aadama ñun ñii si suñu bopp ñu ngi def loo xam ne que ne bu ñu moytuwul après dinañu ñëw lor loolu nag dina génn %e dina am gàllankoor ci wàllum mbéy mi %e dina %e tardé li ñuy wax autosuffisance alimentaire maanaam béy lu ñuy dundee ñu am ko lu bëri yow mbir moomu noo ko gisee na ban jàngat nga ngay
Le projet Agri Jeunes est une plateforme de jeunes qui a été lancée pour débattre de la contribution de la réduction des coûts de l'agriculture aux jeunes et aux femmes.
%hum projet Agri Jeunes %e tekki ndaw ñi moom mi ñu seqal waxtaan wi ni ki tey jile ñuy waxtaanee wàllug yombal gi ñeewal suuf ji ci ndaw ñi ak ñi nga xamante ne ñoom ñoo di %e jigéen ñi
donc ces choses sont des pourcentages de systèmes qui sont connus pour être capables de faire le profil des populations
donc yooyu yëpp doon na ay %e ay systèmes yi nga xamante ne ne dañ koy defal au au profil des populations
surtout si l'époque que vous connaissez comme changement climatique est dominée par le changement climatique
rawatina si si jamono ji nga xam ni changement climatique moo ko dominer bu baax a baax a baax
le projet leur rappelle que le monde est en train de changer cent cinquante mille jeunes donc quarante cinq mille femmes donc cinquante pour cent de femmes qui se connaissent comme des jeunes filles doivent être dans ce que vous connaissez comme elle c'est leur propre travail qui est de faire bouger leur terre leur sexe jusqu'à ce que vous sachiez comment ils vont pouvoir se déplacer seuls %e part de la nourriture part de la nourriture part de la nourriture %e tout ce que vous connaissez comme des femmes %e les dirige vers l'avant
projet bi fàttali leen rek %e dafay day dafa dafa dafay viser cent cinquante mille jeunes donc %e quarante cinq mille ci %e jigéen ñi donc cinquante pour cent ci jigéen ñi nga xamante ni ay ndaw lañ war a nekk ci li nga xamante ni moom mooy seen liggéeyu bopp yi yëngal suuf seen cëgal guy ba nga xamante ni dinañ mën a demal seen bopp %e wàllum %e mbay meeg wàllum napp geeg %e lépp loo xamante ni rek %e daf leen di jëmale kanam
parce que c'est un art qui a une variété de projets
parce que xëy na am na xeetu projets yoo xam ni
oui oui tu sais la technique de transport des récoltes que beaucoup de producteurs connaissent
waaw bon xam nga %e technique de transport récoltes yi souvent producteurs yi ñoom xam nañu ko
entre ces deux vents
diggante ñaari ngelaw yooyu
les élus locaux
élus locaux yi
Parce que dans ces enquêtes, ils sont arrivés à la conclusion que chaque producteur qui sait que c'est important pour toi d'être admis dans le projet sait combien d'hectares tu as dépensé % ils savent combien d'hectares tu as dépensé et le pourcentage de matériaux que tu as dépensé et tu as obtenu ton quota de travail et les matériaux dont tu as besoin mais que tu n'as pas
ndaxte ci biir enquêtes yooyu ah nañu dem ba nga xamante ne bépp producteur boo xam ne maanaam jot ngaa dugg ci projet bi dinañu xam ñaata hectares ngay béy %e nañu xam ñaata hectares ngay béy ak %e matériels yi nga xam ne jot nga kaa am ci sa wàllum liggéey ak matériels yi nga xam ne xëy na soxla nga ko waaye amagoo ko
tu as vu que c'est Serigne Moussa
dangaa gis %e maanaam Serigne Moussa
merci beaucoup seydou pour la paix ils se sont bien entendus
merci beaucoup Seydou nekkal si jàmm kontaan nañu bu baax a baax
Souckna Awa Touré a perdu la parole en disant que la famille est la plus grande partie de la responsabilité. Celui qui parle de famille dira que la mère et le père sont les chefs de chaque famille.
%hum %e Sokhna Awa Touré %e sànq wax nga ko nee nga famille bii ñoo ci ëpp part de responsabilité ku wax njaboot dinga ne yaay ak papa ñoom ñooy kilifa ci famille bu nekk
appliquez la partie crédit de la partie épargne
jàppaleleen ci wàllum crédit wàllum épargne
*** une fois
*** bu boobaa de
%e de la même chose
%e melokaanu sax bi
donc le changement climatique est un fait donc il ne faut pas avoir faim dans le champ si tu vois un jour de fatigue sans force maisons puissantes toutes les choses sont grosses là où elles vont rester dans les maisons tu sais qu'elles n'ont pas de force la pluie va entrer directement là où elle va sécher elles n'ont pas de fourrure donc dans le changement climatique elles sont fières de changer si elles peuvent grandir elles peuvent avoir de quoi manger elles peuvent résister au choc elles peuvent adopter une attitude de choc don, c'est pourquoi je demande aux gens d'être certifiés au lieu de rester assis à attendre l'état l'état ne comptez pas sur l'état ne comptez pas sur vous l'aide vient vous faciliter le travail
donc changement climatique rangoor bi am na donc waruñu xiif ci tool soo gisee jiw bu sonn amul doole mais yu am doole yëpp fatt nañu foofu day day tooy ci biir mais yi nga xam ne daal amuñu doole naaj bi day dugg directement foofu day wow amuñu kattan donc ci changement climatique bi ñu góorgóorlu soppi suñuy doxin pour ñu mën a am lu ñu mën a lekk ñu mën a résister choc ñu mën a adopté wu tenir ci choc don,c loolu laa ñaan nit yi ñu ut jiw certifié au lieu ñu toog di xaar état bi état bi bul yaakaar ci état bi yaakaar ci sa bopp kuy ñëw dimbali la day gën a yombal sa liggéey
c'est le flavus (Aspergillus Flavus) le même que le flavonome qui est connu pour être responsable de la fièvre jaune germinative
mooy afla() Aspergillus Flavus noonu la doomu jangoro ji tudd mi nga xam ne moom mooy indi feebaru saabu boobu ci gerte
donc on ne sait pas que d'un hectare à un hectare il y a eu des dégâts
donc buñu xamee ne ci benn hectare demie hectare la laal
donc c'est là que réside le problème de la possibilité de dire que ce n'est plus vrai parce que le téléphone quand il est utilisé, il est toujours là quand il est utilisé, il est toujours là donc maintenant c'est là que réside la possibilité d'essayer de changer les mentalités et de suivre le rythme du temps
donc loolu daal jafe-jafe bi ci mën a nekk daal fi mu ne nii nekkatul wax dëgg yàlla ci parce que téléphone boo ko yoree mun nga ko am rajo boo ko yoree mun nga ko am kon léegi daal xanaa di jéem a soppi xel yi te ànd ak jamono rek moo ci mën a nekk
celui qui est comme Mbacke Gueye Travo, ils le remercient bien, ils entendent bien ce qu'il dit celui qui est comme Mbacke Gueye, il est génial
ku mel ne Mbacke Gueye Travo ñoo ngi koy sant bu baax dégg nañu waxam ku mel ne Mbacke gueye bu njeri
le côté Ndorong est maintenant, mais sinon si vous entrez sur le site Agri Jeunes vous trouverez Agri Jeunes
côté Ndorong la nekk maintenant su fekkente ne bu dul loolu soo duggee si si internet bi soo tapé site agri Jeunes di nga gis Agri Jeunes
parce que si c'était un météorologue il serait rapide il serait rapide c'est étonnant parce que souvent monsieur Badiane me permet de dire que la plupart des informations climatiques qu'on reçoit sont souvent transmises par radio ou par téléphone
ndax xëy na bu doon ñun rek dina dina xaw a dina xaw dina xaw a doy waar parce que souvent monsieur Badiane damay faral di wax ni %e information climatique bii ñuy joxe souvent dañ koy joxe à kii quoi à travers rajo yi wala %e téléphone
les producteurs doivent par exemple être en bonne communication
producteurs bi soxla na moom par exemple di ci waxtaan bu baax
mais aujourd'hui ils sont dans le monde rural où ils savent que c'est dangereux si les parents de ces enfants là-bas les nourrissent, les rassemblent, les font pour la conservation mais ils savent que l'école est fermée
mais mais tey ñu ngi ci ñu ngi ci %e monde rural boo xamante ne xëy na %e suñu parents yi ñun ñun xale yi fi nekk ñun ñoo leen di béyle ñun ñoo leen di góoble ñun ñoo leen di defal conservation bi mais xam nañu ne école tijji na
donc je suis parti mais mon numéro de téléphone
donc maa ngi bàyyi waaye sama numéro téléphone
hectare est peu
hectare tuutiwul
et voilà que même Apronstar qui a vendu plus de 200 sachets est parti et ce produit est parti et est parti parce que les membres de leur téléphone avaient du mal à leur dire qu'ils étaient dans la coopérative quand ils sont venus le acheter puis finalement le produit Apronstar est parti et ils sont retournés et ont acheté un autre produit pour au moins remplacer le produit Apronstar parce que la demande était tellement forte que si on ne l'avait pas couvert on ne pouvait pas le satisfaire
te gis nañ sax même Apronstar bi ji ji nañ lu ëpp plus de 200 sachets dañoo dem ba produit boobu dafa dem ba jeex tàkk tàkk tàkk parce que membre yi seen téléphone moo doon sonné ñu leen di wax nekkoo ci coopérative bi ñu ñëw di ko jënd si ba mujj produit Apronstar bi dafa jeex ba mu dañoo dem wutiwaat yeneen produit pour au moins xaw a remplacé produit Apronstar parce que demande bi était tellement forte que ba munuñu ko woon a %e couvrir munuñu ko woon a satisfaire
parce que les glaciers actuels sont situés au niveau de l'Antarctique et au niveau de l'Arctique
parce que tey glace yi nga xamante ne dafa nekk au niveau de l' Antarctique ak au niveau de l' Arctique
ou travailler avec tracteur
wala labour avec tracteur
Mme Arouna Dia rappelle qu'elle est la représentante de l'ANACIM au service régional de météorologie de Kolda et qu'elle était donc l'invitée d'aujourd'hui car elle est l'animatrice de l'émission 4R du programme alimentaire mondial de la PAM.
jërëjëf Arouna Dia di fàttali que mooy représentant Anacim fii service régional mééorologie bu Kolda kon nag moom moo nekkoon gan bi tey ci li nga xam ne moom mooy émission bii waa %e émission 4R bu PAM %e programme alimentaire mondial
mais aussi financé par le Fonds vert climat comme il l'a dit lors de sa présentation à la Commission, une organisation qui lutte contre le changement climatique mais qui soutient aussi les citoyens de la Catalogne qui sont partenaires techniques
mais aussi ñu ngi ñi ko financé mooy Fond vert climat comme ni mu ko waxee sànq si biir waxtaan bi rek mu nekk kuréel boo xam ne aussi day xeex aussi %e si si changement climatique mais si njàppalante si %e aussi %e di jàppale waa Jokalante nga xam ne ñoom ñooy partenaire %e technique yi
* tu dois faire attention à cela
* nga moytu loolu
%e Ibrahim est le meilleur
%e Ibrahima looy tàggatoo
tu vois les variétés offertes aux habitants de Bombay et de Diorbel où il a été réinventé
gis nga variété yi ñuy jox waa Bambey ak Diourbel ñun fu mu ñu nganguwaat ko
si la prévision saisonnière
si prévision saisonnière bi
attrape chaque année mille neuf cents
jàpp année mille neuf cent yi
la diversification aussi des cultures est devenue une notion importante
diversification aussi cultures yi nekk na loo xamante ni lu am solo la
si on l'utilise pour définir la composition centimétale en termes de rapport masse volume on obtient que quatre vingt sept pour cent de la masse de la terre est constituée par la phase solide
boo ko jëlee nga defli ñu naan %e composition centisémale am maanaam rapport masse volume bi da ngay gis ni quatre vingt dix sept pour cent masse su suuf si c' est constitué par la phase %e solide
il faut par exemple que le producteur lui donne ce dont il a besoin
il faut producteur bi par exemple mu ciy mu koy jox li mu soxla
les auditeurs, je me souviens que vous écoutez toujours l'émission de Louga FM RTS, vous savez que c'est ECHO ECHO qui l'émet, surtout pour les patients qui sont ici à 88.7% je sais que si les auditeurs n'écoutent pas les patients aujourd'hui, ils vont être très malheureux si les patients ne font pas de bonnes choses alors s'ils écoutent votre discours
mbokku auditeurs yi ma fàttali ba tey yéen a ngi déglu Louga FM RTS émission bi nga xam ne ECHO ECHO moo koy jagleel rawatina ñii di béykat yi %e fii ci 88.7 xam naa ne nag suñu mbokku béykat yi tey dinañ si %e jëriñoo bu baax a baax %e donc suñu déggee sa waxtaan
pour qu'ils aient des solutions endogènes s'il n'y a pas de solution endogène disponible ils essaient de trouver d'autres solutions
ba ñu am des solutions endogènes su amul solution endogène rek ñu jéem a wut yeneen solutions
les services de l'état ont évalué le produit Apronstar selon qu'il était bon ou mauvais
wala les services de l' état mu xool ko le produit Apronstar bi ni ko baax na wala baaxul
oui la campagne ça été vraiment bien notre objectif a été atteint grâce à Timbé mais il y a eu des efforts qui ont fait que les médias savent que c'est ainsi que ça s'est passé parce que les émissions qu'ils faisaient étaient mauvaises et donc si la campagne était produite tout était écoulé oui c'est fini
waaw campagne bi ça été ren moom vraiment %e sunu objectif atteindre nañ ko %e grâce à Ticmbay tamit am na si jéego yu bëri yoo xamante ne nii dox na ko si parce que émission yi ñu doon def rajo tax tax na suñu campagne bi %e suñu produit lépp la ñu écoulé waaw jeex na tàkk
l'éducation financière est une façon de faire des choses qui ne se résume pas à des détails
éducation fiçnancière wan neen ni leen nit ki day def farata te bàyyi yenn détail yi
c'était donc une dynamique donc elle a produit une technique qui a fait cette technique des disons qui renforcent certaines nuages
c' était donc une dynamique donc mu jur %e tàngaay bu bëri tàngaay boobu %e disons may doole ay yenn yenn yenn nuages yi
parce que tu sais que les gens d'aujourd'hui vont souvent au niveau des banques surtout la banque agricole ils vont là où il y a de l'argent pour pouvoir avoir de l'intrant pour pouvoir avoir du matériel agricole sans savoir comment ils peuvent faire pour avoir cette assurance agricole
parce que xam nga ne béykat léegi souvent dañuy dem au au au au niveau des banques surtout banque agricole ñu dem leb fa xaalis pour mën a am intrant mën a am matériel agricoles bu tawul naka la ñu mën a def ba am si assurance agricole boobu
en termes de pourcentage d'assurance (%) et de pourcentage de crédit (%)
ci maanaam ci wàllum assu() %e wàllum crédit wàllum épargne
collecter et produire des engrais organiques et faire du compostage
di dajale di def ay fumier organique di def ay compostage
il ne peut pas développer
moom du mën a développer
il est important de rappeler aux téléspectateurs que l'émission est diffusée par un large réseau de télévision du programme alimentaire mondial, de leur radio RIP FM et du projet 4R, et qu'elle est appréciée par le groupe de musique Jokalante.
am na solo tonton Code ñu fàttali mbokk yi ñu ñuy soog a dab rek ne émission bi ñu ngi ko amal ci lëkkaloo bu yaatu bu dox ci programme alimentaire mondial seen rajo RIP FM ak projet bii di 4R ñu bànqaasu ko nag ci li nga xamante ne nii kuréel googee ñuy wax Jokalante
c'est une technique que tu connais comme technique agricole
dafa nekk %e benn technique bu nga xamante ne technique agricole la
les isomètres de la famille de ceux que l'on voit ici au Nioro sont isométriques autour de six cents à huit cents millimètres ce qui n'est pas le cas à Bombay où ils sont deux cents ou trois cents millimètres
isomètres yi bokkuñ ñun booy xool fii Nioro ñu ngi am isomètre buy tourné autour de six cent à huit cent milimètres loolu bokkul ak ay Bambey boo demee ñooñu ay deux cent wala trois cent milimètres lay nekk
certains appareils sont conçus pour être montés sur des piles
am na appareils yoo xam ne ay piles lay monté
donc la prévision climat est la proportion de l'activité des personnes considérées comme heureux (en)
donc prévision climat bi ci biir li nga xam ne mooy %e jëfinu liggéeyu ñi nga xam ne ñooy béy() béykat yi
Même en Europe, vous savez, quand ils sont restés comme en France et en Angleterre, ils ont été éliminés, ils ont été éliminés comme ils l'ont été ici, à 38 ou 40 degrés.
ba Europe sax xam nga bu ñu toogee ba ni France ak ay %e Angleterre temps yële ñu génnoon dañoo yëgoon ngeen ni eggoon nañu fi yenn ay 38 ay 40 degré
oui tu sais que tu aurais eu zéro cinq
waaw ki nga xam ne da nga doon am zero cinq
mais ils sont organisateurs
mais ;dea dañoo organiser wu
c'est pourquoi on dit qu'ils sont égaux dans les farines enrichies qui sont données aux enfants et aux femmes enceintes et allaitantes mais ils favorisent les femmes dans le secteur agricole
moo tax ñu ne dañuy yem ci farine enrichie yu ñuy joxe %e xale yi ak femmes enceintes ak allaitantes yi mais da ñuy gën a jàppale jigéen ñi ci wàllu tool yi
donc la visibilité des choses est souvent la visibilité de ce qui est horizontal et c'est ce que tu sais faire qui fait souvent la différence
donc visibilité yi souvent moom mooy visibilité gi quoi horizontale bi moom mooy li nga xamante ne biimooy def kii quoi souvent la différence
Je peux avoir le numéro de son fils Mbaye Ndiaye
Sëñ Mbaye Ndiaye mën naa am numéro bi
les producteurs sont d'accord
producteurs yi loolu am na
quand vraiment tout est arrivé ils ont compris que le programme est arrivé mais pas le casse ils l'ont amené parce que les partenaires se sont réunis cela signifie que vraiment ce n'est pas un programme si vous savez qu'ils sont venus pour le sacrifier ou le jeter
ba vraiment ñëpp xam ko njëriñoo ko ñu xam ne programme bi ñëw na fii waaye du caaxaan moo ko fi indi parce que rek partenaires yi fi daje loolu rek wane na ne vraiment du programme boo xamante ne dañoo ñëw rek pour saraxe ko nii rek wala sànni ko déedéet
% des gens que tu connais récoltent deux fois
%e ñi nga xam ne dañuy góob ñaari yoon sax
voilà les numéros qu'il a pour le 77 092 22 41 c'est le numéro orange que j'ai appelé et tu m'as répondu alors le 70 206 93 01 c'est aussi mon numéro que j'ai appelé et tu m'as répondu
voilà numéro yi moom bu ootee ci 77 092 22 41 di numéro orange bu boo ma oowee da nga ma jot boo ootee si 70 206 93 01 boobu itam sama numéro la boo ma si oowee da nga da nga ma si jot
mais quand même l'affaire est importante ma bour est importante pour les baigneurs est importante la fumée au tickmbai qui fait la communication beeg tout est vraiment affaire quand tu sais que la fumée se propage partout
mais quand même affaire bi daal am na solo sama boor am na solo ci baykat yi am na solo tamit ci Ticmbay miy def communication beeg yëpp vraiment affaire la bi nga xam ne tamit dafay yaatal lépp daal
parce que je regarde ils disent que l'émission est réalisée par des gens que tu connais avec l'aide de l'Uni() United purpose je sais qu'ils vont venir avec le nom je sais que c'est difficile je sais que c'est anglais mais ils sont venus bien pour que je puisse le traduire donc tu sais que c'est %e cadre projet qui veut dire femme
ndax booy xool wax nañu ni émission bi ñu ngi koy amalee ci ñi nga xam ne ndimbalu Uni() United purpose xam naa ne dinañu ci ñëw tur bi xaw naa jafe xam naa ne anglais la waaye nañu si ñëwaat bu baax pour mën koo tekki ci nag li nga xam ne moom mooy %e cadre projet tekki jigéen
C'est bien comme ça.
c' est bien ça
mais regardez maintenant les gens qui vont à la mer, l'information climatique est importante pour eux, ils savent que la plupart des gens qui voyagent comme des pêcheurs, sont des pêcheurs, je peux dire que c'est depuis le début qu'ils commencent à faire des prévisions
waaye tey xoolal tey ñi ñi dem ci géej gi ñoom information climatique bi dafa am solo ci ñoom ñi nga xam ne bay mais ñun baykat yi comme ñun mbay rek moo ñu kii ñun ñun mën naa wax ne la ci buñ commencé joxe prévisions yi
ou vous êtes en bonne santé
mbaa yéen a ngi si jàmm bu baax
mais aussi les acteurs intervenants
mais ñun ay acteurs intervenant lañ
dans le compost
ci biir compostière bi
C'est un appareil que l'on appelle une "tablette" quand on regarde la télévision. La "tablette" n'est pas un téléphone. La "tablette" est une sorte de ballon. C'est un appareil que l'on utilise comme un jeu. Le conducteur porte une robe blanche. La "tablette" est un appareil que l'on utilise souvent.
Lii ab jumtukaay la boo xam ne bu nu miin la muy "tablette". "Tablette" nag du telefon. "Tablette" bii nag melokaaanam mooy balã. Di benn jumtukaay boo xam ni si ni bu nuy faral di jëfandikoo la. Aa ki ko yore nag mu ngi sol benn yére bu weex. "Tablette" bii nag mu ngi nekk jumtukaay boo xam ni lu bari bari ci nit ñi dañu koy jëfandikoo.
et puisque l'institut est venu à Koussanar et maintenant que vous avez commencé à l'appeler par son nom et son prénom comme si c'était son prénom Jokalante parce que vous êtes en contact avec les béquilles
tey ndax bi institut bi mu ñëwee Kousanaar ak tey ndax comme ni ñu ko waxee tur ci tur bi turam rek ni muy wuyoo ci turam Jokalante bi ndax yéen a ngi jokkalante ak béykat yi
les hybrides sont vraiment des groupes
hybride yi mooy vraiment mboq boo xam ne