Dataset Viewer
Auto-converted to Parquet
Wolof
stringlengths
10
455
emotion
stringclasses
7 values
Bo gisee ma gën laa néew alal ak i doom. "
disgust
waaye leer, lu mu ëmb, fésal ko.
disgust
Ndax li Yàlla sàkk amoon na sikk?
neutral
Ce tare:) si pretul suna biiinnneeee!;;)
surprise
Ngir-yàlla tànnal beneen tur.',
surprise
Yeena ko seede bésub tey jii."
neutral
Su ko defee ñu dëkkewaat seen suufas bopp."
neutral
Les signes (aayaate) sont partout.
neutral
Xamlu ku xam ,day dolli xam.
neutral
Lan lañuy def ak xam-xam boobu ñu am?
neutral
Nóoyin def na lépp li ko Yàlla santoon.
neutral
Moom la Mbind mi wax ne:"Ku jub amul, du kenn sax.
anger
Duñu naan biiñ ba tey jii ndax wormaal seen santaaney maam.
neutral
jubóo te jubu ñu ñoo ko waral.
neutral
By Stormen, en mooy weer,
neutral
Ndaxte kàttanu fas yaa ngi ci seeni gémmiñ ak ci seeni geen.
disgust
Lot ne ca xiiñidxaapaʼ bizuubacaʼ diidxaʼ ne bixooñecaʼ de Sodoma.
disgust
Yàlla daldi koy rey moom lu tollu ci téeméeri at.
disgust
mi mu jagleel say àndandoo."
neutral
Yexowa dafa sàkk góor ak jigéen ngir ñu jàppalante ci seen biir.
neutral
Dina ko dóor ay dóor yu metti, jox ko añub ñi gëmul Yàlla.
disgust
Dañuy dinañu fàtaliku yaw.
neutral
ak biddiiwub Refan, bi ñu daan bokkaaleel Yàlla,
neutral
ak yeen ñi ko ragal, mag ak ndaw."
fear
Indeed book de wicked est Sijjeen.
disgust
Laajleen ko; magum jëmm la, te man na tontul boppam."
anger
Ana lu waral nga namma tas dëkk bu Aji Sax ji séddoo?"
anger
Yexowa dafa bëgg neexal ñi koy jaamu dëgg.
neutral
Kuy wax googu kàddu, ag leer fenkalu la."
neutral
Dafa fekk rekk ne ci làkku fràñse la gën a siiwe.
neutral
yéen ñi ko ragal, mag ak ndaw."
fear
Waxal ne: "Yàlla, moom Kenn la (jenn Yàlla rekk la).
neutral
Nangeen ñów ci tàntu Yexowa.
neutral
Junniy junnee nga koy jaamu,
neutral
Fa la léen séen wërsëg di fekk subaak ngoon.
neutral
Awa tontu ko ne: "Man nanoo lekk ci doomi garabi tool bi kay.
disgust
Su doon genn-wàllu nguur gi sax, dees na la ko jox!"
neutral
bi ngeen daan jaamu
neutral
Jox leeni doom lu jafe la.
neutral
Xanaa xamuloo ne mën naa laaj sama Baay ay junniy malaaka ngir ñu muccal ma ? '
anger
" En fait, je ne suis ni l'un ni l'autre, je suis juif. "
neutral
Juróom ñaari fan nag ngay négandiku, ba ma fekksi la fa, xamal la looy def."
neutral
Waaye su lalee pexem wor de, dina dee."
fear
musal ko ci ku koy teg àtteb dee.
anger
Waaye Lóot ak njabootam dañu doon yéexantu.
neutral
Ndaxte Seytaane wàcc na ci yéen, ànd ak mer mu tàng, ndaxte xam na ne, jot gi ko dese barewul."
neutral
Dañu leen di bañ waaye itam dañu leen di xawa ragal.
fear
di yool, ba wis kuy réy-réylu.
joy
te noor ak nawet lay doon.
joy
Ci Sunu Boroom lanu joge Ca Moom lanuy dellu!
neutral
Sob, lépp lu ñuy aaye yaa koy def, luñu nëbb yaa koy luqati.
neutral
Loolu moo tax ngeen gis te dégg kéemaan yii. '
neutral
C'est vrai waay, pa bi dafa wara go.
neutral
Noonu lay deme ak ñiy weddi ak aji gëm yi.
neutral
Te sama dige Booroom dëgg la."
neutral
Dafa mas a firnde barke ci li jëm ci jur doom yu bare. "
joy
Kon sawara wi moo gën a yaatu safara si.
neutral
yam ci tawfeex ci sag ak sañ-sañ.
neutral
Képp ku nekk ci asamaan dafay topp bu baax Yexowa Yàlla.
disgust
ba kera mu yégal njub, ba daan.
sadness
Seetal fi ñuy defe suñu ndaje yi ak ni ñuy jaamoo Yàlla.
neutral
Ngir nu nattu léen kan ci ñoom a gën a rafet jëf.
neutral
Bu dee guddi àjjuma ñu wàccee ko juróom ñaari yoon.
fear
Lóot nag soññ leen, ba ñu dal këram, mu ganale leen.
anger
Tey jii, Yexowa dina ma dimbali ba ma rey la. '
neutral
Nóoyin ak doomam yi déggal nañu Yexowa te komaase nañu tabax gaal googu mel ni kees.
disgust
AS - Dinañu ko dëgg bu neexee Yàlla.
neutral
Ginnaaw loolu, mu tànn ci seen biir xale yu góor yi gën a rafet te gën a am xel.
neutral
Dañu sàcc lu Yàlla moom.
disgust
Lu tax ñu war a gërëm Yexowa ndax njot gi mu maye?
anger
Yaw ak sa njaboot ak say xarit dingeen am dund bu neex ba fàww.
neutral
Yàlla tànnoon na waa Israyil ngir ñu nekk ay seedeem.
neutral
Bu ma lekkoon tey ci yàppu saraxas póotum bàkkaar bi, ndax dina neex Aji Sax ji?"
neutral
waaye day dàq ñiy def lu bon."
disgust
Lu ko moy dinañu daanu ci seen kanami noon."
fear
Ndax du ci saw tur lanu daa defe ay kéemaan yu bare?"
neutral
Yalla rekk-ay Yalla te li Mu yellool Moom rekk-a ko yellool.
neutral
ak kéemaanam yi ñeel doom aadama yi.
neutral
Mu ne ko: "Moom de, ma nga ca kër Makir doomu Amiyel, ca dëkk ba ñuy wax Lodebar."
neutral
Sama boroom yal na nga nu nagul,yaw ay aji dégg jiy aji xam.
neutral
mbind mi dafa ne:"ana ku xam xalaatu boroom bi?ku ko doon digal?"
neutral
te xam mbaax, gi ci kàddug Yàlla, ak kéemaani jamono jiy ñëw,
joy
Fa nga jaare Yàlla la gaa ña jiitu di wër ba tay
fear
bégleen te bànneexu, ndax seen yool dina réy ci laaxira. ndaxte noonu lañu daan fitnaale yonent yi fi jiitu.
joy
jëmmi-jamono j-: taŋ b-. dinañu gise jeneen jëmmi-jamono.
neutral
Waaye, duggewuñ ko woon lu dul wéyal nootaange bi.
neutral
bah ca te prend comme ca direct?
neutral
Soo ko defee, dinga ko aar ci biir buy daw.
joy
Bu gumba dee wommant moroomam nag, kon dinañu daanu ñoom ñaar ci kàmb.
neutral
Waaye soo ko deful, na la bir ne dinga dee, yaak sa waa kër yépp."
sadness
Lan lañu mën a jàng ci li dal jabaru Lóot ?
neutral
Ci turu Yàlla Yërëmaakoon bi, Jaglewaakoon bi.
anger
Bu ko neexoon mu def ko jàmm, baaxe ko réew mépp; bu ko neexoon yit mu soppi ko safaan ba, def ko fitna.
disgust
Balaam moom, mënul gis malaaka mi.
disgust
Musa:"yo apek yu nek ngono..."
neutral
Esekiya ne ko: "Mboolem lu nekk sama biir kër, gis nañu ko.
neutral
Mbaa du dangaa lekk ca garab, ga ma la aaye, waay?"
disgust
Xamuleen ko nag; man maa ko xam.
neutral
luy doon muju ki weddi te dëng?"
disgust
Bés bi Yàlla di alag ñu bon ñi dina bett ñépp.
fear
End of preview. Expand in Data Studio

Wolof Emotion Analysis Corpus

Dataset Description

This dataset contains emotion-labeled text data in Wolof for emotion classification (joy, sadness, anger, fear, surprise, disgust, neutral). Emotions were extracted and processed from the English meanings of the sentences using the model j-hartmann/emotion-english-distilroberta-base. The dataset is part of a larger collection of African language emotion analysis resources.

Dataset Statistics

  • Total samples: 320,611
  • Joy: 32636 (10.2%)
  • Sadness: 19793 (6.2%)
  • Anger: 22854 (7.1%)
  • Fear: 13260 (4.1%)
  • Surprise: 24477 (7.6%)
  • Disgust: 26030 (8.1%)
  • Neutral: 181561 (56.6%)

Dataset Structure

Data Fields

  • Text Column: Contains the original text in Wolof
  • emotion: Emotion label (joy, sadness, anger, fear, surprise, disgust, neutral)

Data Splits

This dataset contains a single split with all the processed data.

Data Processing

The emotion labels were generated using:

  • Model: j-hartmann/emotion-english-distilroberta-base
  • Processing: Batch processing with optimization for efficiency
  • Deduplication: Duplicate entries were removed based on text content

Usage

from datasets import load_dataset

# Load the dataset
dataset = load_dataset("michsethowusu/wolof-emotions-corpus")

# Access the data
print(dataset['train'][0])

Citation

If you use this dataset in your research, please cite:

@dataset{wolof_emotions_corpus,
  title={Wolof Emotions Corpus},
  author={Mich-Seth Owusu},
  year={2025},
  url={https://huggingface.co/datasets/michsethowusu/wolof-emotions-corpus}
}

License

This dataset is released under the MIT License.

Contact

For questions or issues regarding this dataset, please open an issue on the dataset repository.

Dataset Creation

Date: 2025-07-04 Processing Pipeline: Automated emotion analysis using HuggingFace Transformers Quality Control: Deduplication and batch processing optimizations applied

Downloads last month
11

Collection including michsethowusu/wolof-emotions-corpus