audio
audioduration (s)
2.29
12.5
sentence
stringlengths
26
118
bare tànk taxul jaalaal gëna gaaw ci mbindéef yi
wax dëgg bokkuñu gis gis ci mbir mi
soo diwul sa jañ bi sa kawar gi dina dagg
bul fàttee jënd yomb tey cere lañuy togg
looy juun juuni ni ku yàkkamtee dem
xale bi ni ko loo ma mayoon bi nga ma jurée
ba ma gisee mu xalmbànde laa xalaat ne tiijan la
di ñu xamal it ne bëgg na fajkati cosaan yi jotaay jii ñu tàmbali
ñaari kuur doññ la dóor ci dugub ji rekk loxo yi nàcc
kenn dàqula waxaale ab saalum saalum
lay naa dugub ji ba deseetul wenn feppu suuf
demal ci sa tànta mu abal ma telleem
ndox moo fekkewul ba muy taa bul jiite xuusam
soo ko tàmmee ci sag ngone mooy wéy
bi ma leen déggee ñuy dëbb booba jant fenkagul
mu daldi yóbbu ndaw si ci kërarn ni ndey ji am naa jabar
njaay mi benn la waaye ku nekk ak sa wërsëg
xiinul de xanaa gisuloo biddéew yi
géwel bi ni man gis nga nii ñu ma def man mi bañoon tëgg
wolof njaay nee sawóor bëgg na dugub waaye du bey
sepà jaléñ du la fasalé k i teeñ
su ma ko xamoon duma jëflante ak pànk moomu
Naar yépp daw mu jël ci xar yi yóbbu
ruuxal soow mi ndax soppuma ci sañ yi
maa ngi ko fekk ci ëtt bi muy kof kofi
sees yi duñu gaaw a jar fii nit ñi bëgguñu ko noonu
xaaral ba nu matal ay gii nga soga bokk
mu ni ko buur dé moo ni naa ko rattal nag wu góor wi
ab suusal la ko mujj yàkkal ci dëkk bi ñu ne
ku bari tiitar la du la romb ba nuyu la
benn sàmba lingeer a tabax lekkool bii may ko waa dëkk bi
omar wàccee ca woto ba ñépp dañu dawsi
léegi nag mu yegg ci dëkk bi yaayam nekk
lii duma ko def ndax masuma koo gis
gan kulóoru wëñ nga bëeg ci sa mbubb mi
léegi nappkat yu bare gaalu motoor lañu am
ey man fu ma jëm ag suma gàcce gii
bu cere ji suusee bul toj lépp bàyyil ma fi daN
ngér moo ci topp nag lu ci gën bari ay nit nga topp
ba mu agsee rekk dafa dal di jubal ca waañ wa
dama la bëggoona yar ngir doo ko defaat
bukki doxe ko gannaaw roy baatam di woy woy wi
jabaru xuuge bi dem ci wenn faru xuuge bi né ko
coow lee ma fàbbi ba am lu ma rëcc ci waxtaan wi
bu leen ko yërëm ndullileen ko ba mu dee
bés bu nekk ma yéemu ci mbiru yàlla
kurusu mërgël la ma indaaleel bi mu jógee màkka
jigéen ñi dañuy weer yoxos ji ba mu wow ñu di ko jaay
yéesu dafa raamu ba raxasal ay taalibeem seeni tànk
xamuma ku la ko xelal waaye def nga lu baax
jox ma njàmpe li ma ragg samay tànk
waaw moonte loolu nuy dégg woyu ndox la
jënd naa ñaari meetar ca mbaseñam ba
ku rafet ba mel nii ñu lay duylóo
dama bëgga jénd am ngonk ngir liggéeyu tool yi
ruuñ bi dafa bare garees moo tax sorewuma ci
jigéen ju taaru war na am sàkkar yàlla
yóbbul bool bi ca tëgg ba mu nottarñi ko
njiit lii du ku ñuy jay dëgg la bëgg dégg
rëbb bu jub loxo la woon waaye gisatul bu baax
doom yi jóq xas ku ne ci doom yi wax la ngay def gànnaar
sa kawas dafa bëtt mënuloo ko ñaw
yàlla am ci nun moo tax mu yónnee nu doomam
am na lu xew fale waaye duma fa dem ndax dama weex dunq
su sangoo te toccamikuwul yaram mi dafay xasan
mëñul woon dox dañu ko nguufaan ba ca oto ba
sa jabar a ngi ci waaN waaN ji léegi mu wasin
daldi jël loxo yi teg ci bët yi né ko
dama koy dégg rekk waaye mënuma la ni nii la xar kanamam mel
waxambaane wa xool ci suuf ba mu yàgg mu xool baay bi ni ko
amari ngoonee taxoon kajoor feyatul voon galag jolof
kooku dara du dugg ci bopp bi ab yaj la
ku yakke loxo bàyyi kuddu doo ko ñaareel
meew mi saful dara dafa mel na dañu ci rax ndox
kumba di dox di dox ba fekk genn siddéem guy bàcc boppam mu sukk nuyu ko
moom nee na jabar seetu ca juddu ba jikko ja lay seet
ku mën a jat gaynde waruloo ko ragal
kilifa gu bees gaa ngiy jéem yolomal sàrt bi
su takkul lonet du mëna jàng mbind mu sew
aw naaru góor lu mu mëna mëna daw ñu bàcc ko ab yar
sedd lañu nekk guddi gi dafay teel a dugg
fey naa la ba mu jeex kon danga war far sama tur
am na piis bu ma ñal ca bitigu usmaan
bi xale yi nówee mu may leen ñu lekk
mu ngi yéeg ci fasam di xalam topp géttam
am na lu xew fale waaye duma fa dem ndax dama weex dunq
xuy dem di dem ba ñu gis benn dëkk
bu jeekk aat yi dañu daan waat ni duñu dow
sorbo ñu ngi koy def ci baatu turki
dindil sa loxo yi nga dar ci sa nopp yi te déglu ma
ku nekk dégg na sama benn bajo koo njaay bi
sama loxo yi dañuy xub te xamuma lu ko waral
Nanu taxaw jonn ba sën bañati fi am
bu ñu déggee sab dënn gaajo ga dina tas
fu jinah yabé muus mpah a fà jeegéñ
jigéen ji nag yumaane rekk la bañ
palpale yi nga gis bitim réew lañu lenn di jaaye
bul sàggane sa gaañ gaañ bi faj ko
xaaral mu xippi nga jël furno boobu
dem na ba di bëgga àgg ñu ne ko mu waññiku